Joxàl mala bi mu lekk dey jàngal sa doom yi baat ag araf nj i ci jàng lifantu. Tannal mala bu tilljagul ci nenam diko jox mu lekk ay araf ag baat ngir mu magg ba doon xarit bu bess ci yow
LAN MOY JOXÀL SA MALA MU LEKK?
Joxàl sa mala mu lekk dey jëffëndiko ay feemu po yuy jàngale yuñu tekk ci xam-xam yu woor ngir fexe ba dimbelle sa doom yi je sawar ci jnnk mi. Xale yi di Neen Beg di Tann ag di gis ni sen xaritu mala yi di Magge ba pare di jàngale baat ag Araf yu njëk yi Lenn di dimbële ñu mena liir
AM KO CI SA TELEFON TE FAY DARA, AMUL AY NATAALU SIIWAL, AMUL LOY FAY CI BIIR PO MI!
Nyfiken lärande, CET ag Apps Factory, det är du, du är inte en riktig man, du kan inte vänta med dig. Gör fay dara ci po mi!
MÖNDARGAWU PO MI NGIR ÑONGAL XAM-XAMU LIFANTU:
• Du kan inte göra något för att göra det
• Ay po ngir xaame araf yi ngir liir ag binda
• Det är en viktig fråga om vad som händer
• Du kommer inte att vara säker på att du ska "baat bi rek gey dégg"
• Alluwa bu wayjuur yi mëna xayma tolluwaay sen doom
• Po mu nit yu bëri mëna deffando andak ñu mëna xayma tolluwaay kenn ku ne
• Ja, det är inte så bra, du är dum för dig, du vill boolek
• Dey yokku xaaraaŋtef jëm ci jókko ag yëkk-yëkk
• Gör det bra med dig
• Soxlawul dara lu leey lëkkale ag enternet
AY ESPESYAALIST YU XAARAAÑ ÑOOKO DEFAR PUR SA DOOM
Po mi ñongi ko amal ci ay atu xalaat, xayma ag jëfandikoo ci xam-xamu baat ag araf yi. Dafa dëxëñ ci bir ay xam-xam yu am jëriñ, bokk nasi xamee jëm ci ni ñuy binde baat yi, xamee araf yi, mbindum baat yi, xam-xamu baat yi ak lumuy tekki, jāng baat yi guy gis. Ginaw bi du kan defare ci màndargawu mbëggeel ag ay mala yu bëri, po mi dey dimbele xale yi ci du är setlu, yeewute jëm ci sen yoonu maggaay.
ÑOY ÑAN?
Kurel gi di Joxal mala bi mu lekk ñu gën ka xam ci "Fodra monsteret" mongi am ci ndimbëlu banxaas bi yóor wallum bitiw rew bu dëkk bi di Norwes ginaw bimu bokke i den senaste delen av "EduApp4Syria-konkurrensen". Jumtukaayu bu njëku po mi mo NGI nekkoon ci làkkup arab ñu defaroon ko ci lëkkalowu kurel yi di Apps Factory, CET - Centrum för Educational Technology ag IRC - The International Rescue Committee.
-------------------------------------------------
Feed Monsteret lär barnen grunderna för att läsa i Wolof. Samla monster ägg och mata dem brev så att de kan växa till nya vänner!
VAD ÄR FÖDDEN MONSTEREN?
Feed Monster använder beprövade "play to learn" -tekniker för att engagera barn och hjälpa dem att lära sig att läsa. Barn njuter av att samla och växa husdjursmonster medan de lär sig att läsa grunderna.
GRATIS FÖR NEDLADDNING, INGEN ADS, INGEN IN APP-KÖP!
Allt innehåll är 100% gratis, skapat av läskunnighet nonprofits Curious Learning, CET och Apps Factory.
SPELFUNKTIONER FÖR ATT FÖRBÄTTRA LÄSHETER:
• Roliga och engagerande phonics pussel
• Letterspårningsspel för att hjälpa läsning och skrivning
• Ordförrådsminnespel
• Utmanande "ljud bara" nivåer
• Föräldrautvecklingsrapport
• Multi-användarens inloggning för individuell användarutveckling.
• Samlarbara, evolvable och roliga monster
• Designad för att främja socio-emotionella färdigheter
• Inga inköp i app
• Inga annonser
• Ingen internetuppkoppling behövs
UTVECKLAD AV EXPERTER FÖR DIN BARN.
Spelet är baserat på år av forskning och erfarenhet av läskunnighetens vetenskap. Det innehåller nyckelkompetens för läskunnighet, inklusive fonologisk medvetenhet, brevigenkänning, telefonik, ordförråd och ordlitteratur, så barnen kan utveckla en stark grund för läsning. Byggd kring konceptet att ta hand om en samling monster, är den utformad för att uppmuntra empati, uthållighet och socio-emotionell utveckling för barn.
Uppdaterades den
13 okt. 2020